2 Kings 8:6 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Buur laaj ndaw sa, mu wax ko lépp. Buur boole kook bëkk-néegam ne ko: «Fexeel ba ñu delloo ndaw sii lépp luy alalam ak dayob lépp lu suufam meññoon, la ko dale ca bés ba mu fi jógee ba tey jii.»