2 Kings 9:15 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Booba Buur Yoram moom dem na Yisreel, fajuji ndax jam-jam ya ca xareem baak Asayel buurub Siri. Yewu nag ne: «Ndegam man ngeen àndal, bu kenn rëcce ci biir dëkk bi, di nettaliji waa Yisreel.»