2 Kings 9:16 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu war watiir, jëm Yisreel, fekk Yoram a nga fa woon tëdd ndax jam-jam ya. Akasiya buurub Yuda dikk, di ko seet.