2 Kings 9:18 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu gawar ba gatanduji leen, ne leen: «Buur nee: Mbaa jàmm la?» Yewu ne ko: «Ana luy sa yoon ci jàmm laam déet? Ayca, toppal sama gannaaw.» Jongrukat ba daldi yégle la xew, ne: «Ndaw la àgg na ca ñoom de, waaye dëppul.»