2 Kings 9:19 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yoram yebalaat beneen gawar. Ba mu àggee ca ñoom, ne leen: «Buur nee: “Mbaa jàmm?”» Yewu ne ko: «Ana luy sa yoon ci jàmm laam déet? Ayca, sama gannaaw.»