2 Kings 9:27 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Akasiya buurub Yuda gis loolu, daw jaare ca yoonu Bet Gan, Yewu dàqi ko, tey yuuxu naan: «Jamleen ko, moom itam.» Ñu jam ko ca kaw watiiram ca yoon wa ngay yéeg jëm Gur, ca wetu Yiblam. Mu daw ba Megido, dee foofa.