2 Kings 9:5 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Naka la agsi rekk, fekk njiiti mbooloom xare mi bokk toog. Mu ne: «Kilifa gi, bataaxal laa la indil.» Yewu ne ko: «Ku ko moom ci nun?» Mu ne ko: «Xanaa yaw, kilifa gi.»