2 Peter 1:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te dinaa góor-góorlu, ngir sama gannaaw ngeen di fàttaliku li ma leen doon wax.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye dinaa def sama kem-kàttan, ba fu ngeen tollu, di fàttliku mbir yooyu, gannaaw bu ma dëddoo.