2 Peter 1:17 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte Yàlla Baay bi sol na ko teraanga ak ndam, te baatub Aji Màgg ju tedd ji jib na ne: Sama Doom a ngii, di sama Soppe; ci moom laa ame bànneex.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax kat moo nangoo ci Yàlla Baay bi, teraanga ak daraja, ba ko baat ba jibalee, bawoo fa Boroom daraja ju yéeme ja ne: «Kii moo di Sama Doom, sama Soppe; ci moom laa ame bànneex. »