2 Peter 1:21 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ndaxte kenn ci yonent yi musula wax ci coobareg boppam, waaye, Xel mu Sell mi daa na xiir nit ñi, ñu yégle kàddug Yàlla.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax kat du genn kàddug waxyu gu masa soqikoo ci coobarey nit, waaye ci xiirtalub Noo gu Sell gi la aw nit daan waxe waxyu bu bawoo fa Yàlla.