2 Peter 1:3 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Dooley Yàlla moo nu may lépp lu aju ci dund gu sax ak ragal Yàlla, jaarale ko ci xam gi nu ko xam, moom mi nu woo ci kaw ndamam ak dooleem.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su dee nag mboolem lu dund gu ag jullite laaj, Yàllaa nu ko maye dooleem, ba mu nu xamalee ne darajay boppam, ak jalooreem ju wéet lanu wooye.