2 Peter 1:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte bu leen jiko yooyu soloo, ba sax ci yeen, dina tax seen xam Yeesu Krist Boroom bi am njeriñ te jur mbaax.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax yooyu jikko kat su ngeen ko amee, ba mu law, dungeen yaafus, dungeen ñàkk njariñ nu ngeen xame Sang Yeesu Almasi.