2 Peter 2:12 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waaye ñoom dañuy xas ci biir yi ñu xamul. ñoom ak bàyyima ñoo yem, di ay mbindeef yuy tañaxu, te tër rendi rekk a jekk ci ñoom; dees na leen rey ni bàyyima,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye ñoom ñooñu mel ni mala yu amul xel, seen yég-yégi judduwaale jiital leen, te li leen taxa juddu di jàpp leen, rey doŋŋ, ñooy saaga lu ñu xamul. Dees na leen rey ni ñuy reye ay mala.