2 Peter 2:16 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waaye déggadeem yóbbe na ko yeraanga; xam ngeen ne mbaam-sëf du wax, waaye mbaam wax na ak moom ci làmmiñ wu bir, ngir mu génn ci ndofam googu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye Balaam, ag tooñam tax na ñu femmu ko; ab waruwaay manula wax, te moo waxe baatub nit, ba dakkal jëfi ndofi yonent booba.