2 Peter 2:22 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Noonu seen mbir dëggal na li ñuy wax ne: Xaj mooy waccu, di ko lekkaat; te it: Mbaam-xuux, loo ko sang-sang, mu xalangu ci ban.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Li léeb wii wax te muy dëgg, moo leen dikkal: «Xaj waccu, lekkaat ko; te cangaayu mbaam-xuux, teewu koo xalangootee poto-poto.»