2 Peter 2:7 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye musal na Lóot mi jub, mi sonnoon ndax ñaawteefi ñu dëng, ñooñu mu nekkaloon.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
te mennum Lóot aji jub ji, di kenn ki mu musal, te mu sonnoon lool, ndax ñaawtéefi nit ñu dëng ñooñu,