2 Peter 2:9 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Gannaaw loolu lépp am na nag, nanu bir ne, Boroom bi man na musal aji gëm ji nekk ci nattu, te denc ñi jubadi, ngir alag leen bésu àtte ba.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su demee noonu kay, kon Boroom bi def loolu lépp, xam na nu muy musale nit ñu jullite cib nattu, ak nu muy xaare nit ñu dëng ñi, ngir seen mbugal kera bésu àtte ba.