2 Peter 3:14 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Kon nag samay soppe, gannaaw yeena ngi séentu loolu, góor-góorluleen, ngir bu Krist ñëwee, mu fekk leen ci jàmm, ngeen baña am benn gàkk mbaa sikk.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon nag soppe yi, li feek ngeen di séentu loolu, defleen seen kem-kàttan, ba bésub keroog fekk leen ci jàmm, te ngeen baña am benn gàkk, mbaa sikk ci gis-gisu Yàlla.