2 Peter 3:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te jàppleen ne, muñug sunu Boroom muccu nit la. Sunu mbokk mi nu bëgg Pool bind na leen ko, ci xel mi ko Yàlla sol.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Sunu Boroom nag, ag muñam, jàppleen ne moo dig mucc, noonee leen ko sunu soppe, mbokk mi Póol binde woon ci xel mu rafet mi ñu ko baaxe.