2 Peter 3:18 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye màggleen ci yiwu sunu Boroom ak Musalkat Yeesu Krist, te sax ci xam ko; moo yelloo ndam fii ba fàww.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye màggleen ci wàllu yiwu sunu Boroom, sunu Musalkat Yeesu Almasi, ak ci wàllu xam-xam bu ngeen ko xam. Ndam ñeel na ko tey, ba kera bés bu sax dàkk. Amiin.