2 Peter 3:4 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
ci di leen ne: Ki dige woon ne dina ñëw, ana mu? Ndaxte baay ya nelaw nañu, waaye lépp a ngi dox ca njàlbéen ga ba tey.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñooñoo naan: «Ki dige woona ñëw, ana mu? Ba maam ya nelawee de yàgg na, waaye lépp a ngi wéye na woon ca njàlbéenu àddina.»
Recommended Reading