2 Peter 3:9 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Li Yàlla dige, dina ko def, lu mu yeex-yeex ci xalaatu nit. Xanaa kay da leena muñal, ndax bëggul kenn alku, waaye ñépp tuub seeni bàkkaar.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Du caageenu yeexe gu Boroom bi yeexe dige ba, noonu ko ñenn ñi fooge ag yeex. Yeen la muñal kay, ndax buggul kenn sànku, xanaa ñépp dem ba tuub.