2 Samuel 10:13 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba loolu amee Yowab ak gàngoor ga ànd ak moom sàqi ngir xareek waa Siri, waa Siri daw, won leen gannaaw.