2 Samuel 10:14 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Amoneen ña gis waa Siri di daw, ñoom it ñu daw, won Abisay gannaaw ba dellu ca biir dëkk ba. Yowab nag bàyyikoo ca xare baak Amoneen ña, daldi dellu Yerusalem.