2 Samuel 10:15 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw loolu waa Siri gis na ñu daanoo fa kanam Israyil. Ñu bokk daje ñoom ñépp.