2 Samuel 10:16 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu Buur Adadeser yónnee, jëli waa Siri ña ca wàllaa dexu Efraat. Waa wàllaa dex dikk ba dëkk ba ñuy wax Elam; Sobag, njiital gàngooru Adadeser jiite leen.