bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 2 Samuel 12:30
2 Samuel 12:30 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba mu ko defee mu jële mbaxanam buur ma ñu solal seen jëmmu tuur ma ñuy wax Milkom. Diisaayu mbaxana maa nga tollu ci fanweeri kiloy wurus, ab per bu gànjare tappe ca. Ñu tappal ko Daawuda ca kaw boppam. Alal ju baree bare la Daawuda nangoo ca dëkk ba.