2 Samuel 12:4 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci biir loolu ku nekk ciw yoon dikk, dal ak ka barele. Waaye moom néegula sàkk ciy gàttam mbaa nagi boppam, ngir toggal ko gan gi dal ak moom. Ka néewle la nangu mboteem, toggal ko gan gi dal ak moom.»