2 Samuel 12:5 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Daawuda nag mer lool ca jëfi nit kooku. Mu ne Natan: «Giñ naa ci Aji Sax jiy dund, dee rekk mooy àtteb waa ji def loolu!