2 Samuel 13:32 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu Yonadab doomu magu Daawuda Simeya, daldi wax ak baayam Daawuda. Mu ne: «Buur sang bi, bul defe ne sa doom yépp lañu rey de. Amnon rekk a dee, te mooy la Absalom dogu woon keroog ba Amnon torxalee rakkam Tamar.