2 Samuel 14:15 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Buur sang bi, maa ñëw wax la kàddu yii, ndax mbooloo mee ma tiital. Ma noon nag sang bi, naa wax ak Buur, jombul mu defal ma li may ñaan.