2 Samuel 14:17 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Léegi nag sang bi, yal na sa kàddu gii di sama noflaay. Ndax yaw Buur, sama sang, dangaa mel ni malaakam Yàlla, am ug dégg, di teqale liy yoon ak li dul yoon. Yal na sa Yàlla Aji Sax ji ànd ak yaw.»