2 Samuel 14:25 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Absalom nag amul woon góor gu siiwe ni moom ci Israyil gépp ndax góorayiw. La ko dale ca wewu tànkam ba ca digg bopp ba, du lenn lu ca sikk.