2 Samuel 15:10 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Absalom nag yónnee ndéey. Ay ndaw yegge ko giiri Israyil gépp. Mu ne leen: «Bu ngeen di dégg liit gu jib rekk, ne leen: “Absalom falu na buur ca Ebron!”»