2 Samuel 15:14 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Daawuda wax ak mboolem jawriñam ya mu nekkal ca Yerusalem, ne leen: «Nan daw! Lu ko moy kenn ci nun du rëcc Absalom. Nan dem léegi bala moo gaawtu, ba dab nu, def nu musiba, leel waa dëkk bi ñawkay saamar.»