2 Samuel 15:18 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Nitam ñépp a dox romb ko, ñook dag ya ko dar yépp, di waa Keret ñaak waa Pelet ña, ak mboolem waa Gaat ya tollu ci juróom benni téeméeri nit te toppe woon ko ca Gaat. Ña ngay dox jiitu ko.