bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 2 Samuel 15:24
2 Samuel 15:24 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Cadog ak Abiyatar, sarxalkat yaa nga fa woon, ñoom itam. Ñenn ca góori Leween ña bokkoon nañu ca, di gàddu gaal ga àlluway kóllërey Yàlla ga dence. Ba ñu tegee gaal ga, Abiyatar di rendi ay sarax, ba mbooloo ma mépp génn dëkk ba.