2 Samuel 15:27 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Buur dellu wax ak Cadog sarxalkat ba, ne ko: «Dégg nga déy? Dellul ak jàmm ca dëkk ba, ànd ak Ayimaas, sa doom ju góor, ak Yonatan doomu Abiyatar. Yaak Abiyatar àndleen ak seen ñaari doom yu góor.