bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 2 Samuel 15:30
2 Samuel 15:30 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Daawudaa ngay wéy, di yéeg tundu Oliw ya, tey jooy. Ma nga muuru, def tànki neen ndaxu naqar. Nit ña mu àndal ñépp muur seen bopp ñoom it, di yéeg tey jooyoo.