2 Samuel 15:35 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Te sax Cadog ak Abiyatar, sarxalkat ya, nga fay bokk nekkal. Loo dégg kër Buur, wax leen ko.