2 Samuel 16:23 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Booba lu Ayitofel masaana digle day mel ni kàddu gu bawoo ca Yàlla. Daawudaak Absalom, ñoom ñaar ñépp noonu lañu fonke woon ndigalu Ayitofel.