2 Samuel 16:3 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu ne ko: «Waaw, ana Mefiboset, sa sëtu sang ba?» Ciba ne Buur: «Moom de ma nga des Yerusalem, ndax defe na ne tey bànni Israyil delloo ko nguurug maamam.»