2 Samuel 17:10 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su boobaa, ku ñeme, ba dëgëru fit ni gaynde sax, dinga tiit lool, ba ne yàcc, ngir Israyil gépp xam nañu ne sa baay ñeyi xare la, te it ñi ànd ak moom jàmbaar lañu.