2 Samuel 17:15 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu Usay wax ak Cadog ak Abiyatar sarxalkat ya, nettali leen la Ayitofel digal Absalom ak magi Israyil ña, ak la mu leen digal, moom Usay.