2 Samuel 17:27 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba Daawuda àggee Maanayim, Sobi doomu Nayas mu Raba, ga ca dëkkub Amoneen ña, moo ko teertu, mook Makir doomu Amiyel ma dëkk Lodebar; ak Barsilay waa Galàdd ba dëkk Rogelim.