2 Samuel 17:6 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Usay dikk ca Absalom, mu wax ko la Ayitofel digle, ne ko: «Ndax loolu Ayitofel wax lanu wara def am déet? Wax nu lu ciy sa xalaat, yaw.»