2 Samuel 17:9 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xam naa ne ma nga làqu ci xuntim xeer, mbaa bérab rekk. Te bu aw nit jëkkee daanu ci seen biir yeen, ku ko dégg dina ne: “Jéll bu réy am na ca mbooloom Absalom.”