2 Samuel 18:20 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yowab ne ko: «Du yaw yaay yégle xibaar tey jii. Man ngaa yégle xibaar beneen yoon, waaye du yaay yégleji tey, ndax doomu buur a dee.»