bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 2 Samuel 18:24
2 Samuel 18:24 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Daawudaa nga toog ca diggante buntu dëkk, ba féete biir ak bunt ba féete biti. Fekk na wattukat ba yéeg ca kaw taax ma tiim buntu dëkk ba, ca kaw tata ja. Naka la dawal bëtam, séentu, gis jenn waay juy daw moom kenn, di ñëw.