2 Samuel 18:26 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
wattukat ba gis jeneen waay juy daw di ñëw, mu wax ko farbay bunt ba, ne ko: «Xoolal, keneen a ngi, di ñëw, moom kenn.» Buur ne: «Kooku it de xibaaru jàmm lay indi.»